dimanche 14 février 2010

greeting messages in senegal language

some useful phrases in senegal language

Amadou: Salaamaa leekum! Hello!
Noureyni: Maaleekum salaam! Hello!
Amadou: Nan nga def? How are you?
Noureyni: Màngi fi. Alhamdulilla! I am fine. Thank God!
Amadou: Jàmm nga fanaane? How did you sleep last night?
Noureyni: Jàmm rekk, Alhamdulilla! I slept well. Thank God!
Amadou: Jàmm nga am? How are you?
Noureyni: Jàmm rekk, Alhamdulilla! I am fine. Thank God!
Amadou: Jàmm nga yendoo? How has your day been?
Noureyni: Jàmm rekk, Alhamdulilla! It’s fine. Thank God!
Amadou: Sa yaram jàmm? How is your health?
Noureyni: Jàmm rekk, Alhamdulilla! It’s fine. Thank God!
Amadou: Naka waa kër gë? How is your family?
Noureyni: Ñungë fë They are well.
Amadou: Mbaa ???
Noureyni: Jàmm rekk, Alhamdulilla! It’s fine. Thank God!
Basic Introductions
Amadou: Sant wa? What is your last name?
Noureyni: Sy la It is Sy.

Leave Taking
Amadou: Déwenati “Happy holiday.”
Noureyni: Fekkel déwën. “Find the next one (in good health).”
Amadou: Ba beneen yoon Until next time!
Noureyni: Ba beneen yoon, in shalla! Until next time, God willing!
Amadou: Nuyul ma waa kër gë Greet your family for me!
Noureyni: Di na ñu ko dégg, bu sobee Yàlla I will pass on your greetings, if it
pleases God.


Amadou: Ci jàmm In peace!
Noureyni: Jàmm ak jàmm Peace and peace!
Amadou: Nanga yendoo jàmm May you spend the day in peace!
Noureyni: Jàmm ak jàmm Peace and peace!
Amadou: Mbaa ñu ñelew bu baax. May we spend a pleasant night.
Noureyni: ???


salaamaa leekum hello (from Arabic, “peace be on you (pl)”)
maaleekum salaam response to salaamaa leekum (from Arabic, “and peace
be on you (pl)”)
nan nga def? how are you? (lit. “how do you do?”)
màngi fi I am fine. (lit. “I am here”)
alhamdulilla Thank God (from Arabic)
nan nga fanaane? how did you sleep? (lit. “how did you spend the night?”)
jàmm peace
rekk only
jàmm nga yendoo? how has your day been? (lit. “you spent the day in peace?”)
sa yaram jàmm how is your health? (lit. “your body is (in) peace?”)
naka waa kër gë how is your family? (lit. waa “people,” kër “house”)
ñungë fë they are well (lit. “they are there”)
ci loo nekk what’s up? (lit. “what are you in?”)
dara nothing
lu bees? what’s new?
bees new
sant wa surname (lit. “the last name”)
ba beneen yoon until next time (lit. “until another time”)
inshalla God willing! (Arabic)
nuyul ma waa kër gë greet your family for me! (lit. “greet the family for me!”)
di na ñu ko dégg I will pass on your greetings (lit. “they will hear it”)
bu sobee Yàlla if it pleases God
Yàlla God (from Arabic Allah)

Partager
Facebook Tweet It! Buzz this Digg It!

Aucun commentaire:

Enregistrer un commentaire

messages, sms et texte pour toutes occasions

Haut